17/04/2021
---- Li ab sogné la ----
Waxu niu " Bëssup kòorr " waayé " Wéerru kòorr ".
Gnu gën gorgorlu wéerr wi yeupp si jàng Alquran, dikko degglu itt
Di teewlu waxtaanu diné ji
wala série, films yu nu si xamal jàrr jàrr yonent yi agg kilifa diinè ji
Di zikr, jang xasida yi agg nafarr xam xamu farata yi
wagni teewlu wax yuy yakk koor agg po mi.
Goorgorlu si waxtu julli yi agg nafila yi
Niaan sunuy soxla Yallah té dikko bàkk móom mi niu sàkk té xam soxlo yeupp
Sellal sunuy kaddu agg sunuy jëff
---- As Salamualeykum wa Rahmatulah wa Barakatuhu🙏🏾----