Sëriñ bu ndaw

Sëriñ bu ndaw YAR AK TEGGIIN
GÓOR-GÓOR LU SAX CI NDINGËL I YÀLLA YI, AK SAX CI MOYTU AK MUCC CI AY TEREEM, BA FÀWW

03/04/2026

Yàlla nanu yàlla saxal ci ak njub

23/03/2026

Yonent bi ﷺ wax nani: « Képp ku woor weeru koor bamu jeex mu teg ca juróom-benn i fan (6i fan ci weeru kori) melna ni ku woor diiru jamono »

"Le faible qui assume sa faiblesse ou le con qui assume sa connerie paraîtra plus fort et plus malin que le faible qui s...
30/10/2025

"Le faible qui assume sa faiblesse ou le con qui assume sa connerie paraîtra plus fort et plus malin que le faible qui se croit fort ou le con qui se croit malin."

الشخص الضعيف الذي يقبل ضعفه أو الأحمق الذي يقبل حماقته" سيظهر أقوى وأذكى من الشخص الضعيف الذي يظن أنه قوي أو الأحمق الذي يظن أنه ذكي. "

" The weak person who accepts their weakness or the fool who accepts their foolishness will appear stronger and smarter than the weak person who thinks they are strong or the fool who thinks they are smart. "

" Ki doyadi nangu de daa doyadi wala ki dof nangu ak ndofam; moo tane fuuf ki doyadi ba noppi jàpp ne ku dëgër la, wala ki dof ba noppi jàpp ne ku muus la "

Sëriñ bu ndaw✍️

قـال رسول الله صلى الله عليه وسلم:« من سلك طريقًا يلتمس فيه علما سهل الله له به طريقا إلى الجنة »« Celui qui suit un che...
05/10/2025

قـال رسول الله صلى الله عليه وسلم:
« من سلك طريقًا يلتمس فيه علما سهل الله له به طريقا إلى الجنة »

« Celui qui suit un chemin pour chercher la science, Allah lui facilitera par cela un chemin vers le Paradis »

« KÉPP KU SÓOBU YOONU NGIR SÀKKU XAM-XAM SUNU BOROOM DINAKO YOMBALAL CI LOOLU YOONU AL-JANNA »

Yàlla nanu yàlla may xam-xam bunuy taxa jege al-janna, dinu taxa sori sawara.

05/10/2024

Màggalu daaru salaam kajoor!
le 2 octobre 2024 dëppook 28 ci weeru gàmmu at mu nekk,
di màggalug Seex Muhammadul Basiir xujja Mbàkke mom sëriñ baara Mbàkke xaadimu-r rasuul.
Màggal gi nak moom mooko daan defal boppam dici sant turandóom, baayam, sëriñam seex Muhammadul Basiir Mbàkke mom Seexul Xadiim (miñuko dippee), bimu fi bàyyikoo nak ci atum 2007 cila ak njabootam (ci kilifteefu Sëriñ Lamin Mbàkke miko njëkka wuutu batay jii); tàmbali diko ci fàttaliku moomitam ci bis bi ca dëkkam boobu mu sañca loon boppam ci ndigalu turandóom (Seex Muhammadul Basiir Xaadimu-r rasuul) tuddeko "daaru salaam" ñu gënkoo xam ci "daaru salaam kajoor" ngir limu nekk ca kajoor.

ñuy ñaan yàlla yokk leen i leer te yàggal fi ab xalifaam(sëriñ lamin Mbàkke) ak mbooleem njabootug Seex Muhammadul Basiir xujja Mbàkke
Allaahumma aamiin!

SËRIÑ BU NDAW

« Pour vivre longtemps il faut vivre caché »Ku bëgga gudd fan dangay nëbbatu Yàlla nanu musal ci cat Yàlla nanu yàlla sa...
10/09/2024

« Pour vivre longtemps il faut vivre caché »
Ku bëgga gudd fan dangay nëbbatu
Yàlla nanu musal ci cat

Yàlla nanu yàlla saxal ci ak njub

Nun Sëriñ bi rek lanu bëgg te ku bëgga dox sunu diggante ak moom nu bañ la bañ gu toll ne linuko bëgg te du tee nu diko ...
07/09/2024

Nun Sëriñ bi rek lanu bëgg te ku bëgga dox sunu diggante ak moom nu bañ la bañ gu toll ne linuko bëgg te du tee nu diko gëna bëgg!

Envoyé ko Ku naru ta ñëw, ak ñëw ba noppi di jalgati
02/09/2023

Envoyé ko Ku naru ta ñëw, ak ñëw ba noppi di jalgati

06/08/2023

Adresse

Touba

Notifications

Soyez le premier à savoir et laissez-nous vous envoyer un courriel lorsque Sëriñ bu ndaw publie des nouvelles et des promotions. Votre adresse e-mail ne sera pas utilisée à d'autres fins, et vous pouvez vous désabonner à tout moment.

Raccourcis

Partager