23/10/2023
🧠 Les leçons très important tiré sur La conférence de AbIBACRY DIOP, ( كيف تربيالطفل ) Le 2 juillet 2023 à teud bity👇
Rouh si Leer Laka yàlla bind, Mokk malaka ño boku thiossan,
قُلِ الرُّوحُ مِنْ أَمْرِ رَبِّي وَمَا أُوتِيتُم مِّنَ الْعِلْمِ إِلَّا قَلِيلً
Limu bëg mooy jaamu yàlla rek !
👃Bakan si Lëndëm Lan ka bind,
وَنَفْسٍ وَمَا سَوَّاهَا (7) فَأَلْهَمَهَا فُجُورَهَا وَتَقْوَاهَا
Limu bëg mooy Baneex, ak Luka neex rek !
Xél ak xôl, ño yam Dani baax di bonne
Parfois ñu andak 💡bakan parfois ñu andak 💡Rouh, Yaram mooy terrain biñi xéxé té bakkan La gënë jegué motax souvent bakkan Lay andal
👃bakkan mooy def bakkar
حِزْبُ الشَّيْطَانِ ۚ أَلَا إِنَّ حِزْبَ الشَّيْطَانِ هُمُ الْخَاسِرُونَ
💡Rouh mooy def Lu baax
أَلَا إِنَّ حِزْبَ اللَّهِ هُمُ الْمُفْلِحُونَ
👃Motax bakan mo moom
بَلْ تُؤْثِرُونَ الْحَيَاةَ الدُّنْيَا
Yeen, dangeena bëgg lool dundug àddina
💡Mais ruuh mo moom
وَالْآخِرَةُ خَيْرٌ وَأَبْقَىٰ
te àllaaxira mo gën te moo gëna sax.
👃Yàlla dafa jox bakan ay arme yo xamni, mana gaañ Rouh, mooy
زُيِّنَ لِلنَّاسِ حُبُّ الشَّهَوَاتِ
👃Rafetaleef na ci nit ñi sopp bànneex
Baneex Yeppu pour bakan la
مِنَ النِّسَاءِ jigeen
وَالْبَنِينَ doom
وَالْقَنَاطِيرِالْمُقَنطَرَةِ alal ju bari si wurus
مِنَ الذَّهَبِ wala si xaaliss
وَالْفِضَّة ak fass yu tagato
وَالْخَيْلِ الْمُسَوَّمَةِ waruwaay ak xar juur gui
وَالْأَنْعَامِ وَالْحَرْثِ ۗ ak mbey mooy tool yi
ذَٰلِكَ مَتَاعُ الْحَيَاةِ الدُّنْيَا ۖ
👃loolu lépp yóbbalub àddina doŋŋ la,
💡وَاللَّهُ عِندَهُ حُسْنُ الْمَآبِ
Delou waay bu gën manga sa yàlla,
Té mooy Yoyu boka amé bum la taxa bew
Ba faté yàlla
💡Rouh moom béna rek La du def Lu bonn Muku, mais dafay feebar di Ndaw di Rëy, So défé Lu bonne Rouh gui mokoy yëk, so togné nit Rouh gui mokoy yëk, so défé bakaar Rouh gui mokoy yëk, lu naxadi bakan neex na Rouh,
💡Rouh mo moom Turu yàlla yeppu
Ndax mokoy dundël, turu Yàlla bu nekk bokoy zikr dina am Lumu def si Rouh
Té dafay Ray bakkan
💡Rouh mo moom Bepu jaamu yàlla,
Juli amna Tarbiya bumi defal Rouh,
Koor amna Tarbiya bumi defal Rouh,
nata azaka amna tarbiya bumi defal Rouh,
💡Rouh moo mo moom salatul naby
Ndax daf kay dundël, su démé ba def Lu bonne nek sa xel deel julli si YONÉNT bi
💡Rouh dafa jégué xol So déme basa xool feebar del saxo (istikhfaar) mouy tuub ak zikr dafay dundël Rouh
💡Rouh xel daf kay sonnal, bo démé bassa Xel di xalat Lu bonne sonnal la lool
Dell muslu si seytané أعوذ بالله من الشيطان الرجيم ndax seytané mooy jax-jaxal sa xél
👃■ Bakan dafa am ay façon mooy
أَنْوَاهُ الْنَفْسُ
Donté bakan yeppu bena bakan la
Waayé Dafay changé di baax di bonne
👃■ 1 Nafs : إِنَّ النَّفْسَ لَأَمَّارَةٌ بِالسُّوءِ
moy bakan bilay xirtël si Lu bone
Moom Leppu Lu nit def si Lu bonn moko ka deflo, moom mooy collaboré ak seytaané, Nit kuka am du def lu baax du xalat Li baax !
👃💡■ 2 Nafs : لنَّفْسِ اللَّوَّامَةِ
bakan biy diglé Lu baax,
Moom Leppu Lu baax Lu nit def, moko ka digël, parfois nga bëg def Lu bonne mu yedd La, di L wax bul ka def, kuka am bula yàlla dimbalee nga baax
👃💡■ 3 Nafs : نفس المطمئنة
bakan bi yegg sa yalla
Kuka xassa am rek, seytaané dawla, bobu dominé nga sa Yaram, si baneex, ak xalat Lu ñaaw, moom direct AL-JANA Lala jëmé
يَا أَيَّتُهَا النَّفْسُ الْمُطْمَئِنَّةُ (27) ارْجِعِي إِلَىٰ رَبِّكِ رَاضِيَةً مَّرْضِيَّةً (28) فَادْخُلِي فِي عِبَادِي (29) وَادْخُلِي جَنَّتِي (30
👃Nafs : نفس الراضية
bakan bi nangu Li yalla dogal
Ndogal bu ñëw, mu sant yàlla, Luka yàlla tekk mu muñ, Luka nit yi tekk mu muñ
Moom Leppu yàlla Lakay weeer
Kuka am bula yàlla dimbalee nga muçci !
💡Rouh moom béna rek La du def Lu bonn Muku, mais dafay feebar di Ndaw di Rëy, So défé Lu bonne Rouh gui mokoy yëk, so togné nit Rouh gui mokoy yëk, so défé bakaar Rouh gui mokoy yëk, lu naxadi bakan neex na Rouh,
🔺️❓ bu démé ba Deeh ñëw
وَجَاءَتْ سَكْرَةُ الْمَوْتِ بِالْحَقِّ
💡Malaka yi, jël Rouh yobu sa broom ba ndax fala jougué woon
Domou adama yi jël yaram dougël si Souf
إِذَا زُلْزِلَتِ الْأَرْضُ زِلْزَالَهَا (1) وَأَخْرَجَتِ الْأَرْضُ أَثْقَالَهَا (2) وَقَالَ الْإِنسَانُ مَا لَهَا (3) يَوْمَئِذٍ تُحَدِّثُ أَخْبَارَهَا (4) بِأَنَّ رَبَّكَ أَوْحَىٰ لَهَا (5)
يَوْمَئِذٍ يَصْدُرُ النَّاسُ أَشْتَاتًا لِّيُرَوْا أَعْمَالَهُمْ
Bu keroogee, nit ñéppay génn kenn kenn ngir ñu wan leen seeni jëf
Buka défé
💡Rouh jël فَمَن يَعْمَلْ مِثْقَالَ ذَرَّةٍ خَيْرًا يَرَهُ
Yobu Lu baxam
ۚ أُولَٰئِكَ حِزْبُ اللَّهِ ۚ أَلَا إِنَّ حِزْبَ اللَّهِ هُمُ الْمُفْلِحُونَ
👃 bakan jël وَمَن يَعْمَلْ مِثْقَالَ ذَرَّةٍ شَرًّا يَرَهُ
Yobu Lu bonam
حِزْبُ الشَّيْطَانِ ۚ أَلَا إِنَّ حِزْبَ الشَّيْطَانِ هُمُ الْخَاسِرُونَ
أسلام عليكم ورحمة الله وبركاته