xam sa dine

xam sa dine

Partager

Informations de contact, plan et itinéraire, formulaire de contact, heures d'ouverture, services, évaluations, photos, vidéos et annonces de xam sa dine, École religieuse, Icotaf, Dakar.

bismillahi rahmani rahim wa salatu wa salamu ala seydina mouhamad wa alla aalihi wa sahbihi wa salama tasliiman apprenez vos leçons tranquillement sur notre page et même sur WhatsApp

Tafsir | Dioulite yéep ay mbokk lañ nay rafet rek 22/05/2020

Tafsir : Oustaz bibi vendredi 22 mais 2020

Tafsir | Dioulite yéep ay mbokk lañ nay rafet rek "إِنَّمَا الْمُؤْمِنُونَ إِخْوَةٌ فَأَصْلِحُوا بَيْنَ أَخَوَيْكُمْ ۚ وَاتَّقُوا اللَّهَ لَعَلَّكُمْ تُرْحَمُونَ " سورة ...

28/04/2020

Nafila de la 5eme nuit du Ramadan mardi 28 avril 2020

27/04/2020
17/04/2020

Imam légi tay damay lathié wat kinga hamni dafa woor baci beutiagou kor gi Mouy nelaw Di génteu Di sékeu ak djigén ba am Lou gén ci mom kokou koram dafay yakou wala dafay bokou ci gniy kafaara manam (fay 2 mois ak you mel nonou) pour gniko hamoul

11/04/2020

Mbokou yi tay dama beug niou layénté bir pour que ngén geuna comprendre ( kou faté diang fatikha ci djuli loukoy War ?) Ma xol sén tolou way ci sén dîné louci léroul niou leralko

Vous voulez que votre école soit école la plus cotée à Dakar ?

Cliquez ici pour réclamer votre Listage Commercial.

Emplacement

Téléphone

Adresse


Icotaf
Dakar