AHBÂB sangue barhamou ndiaye

AHBÂB sangue barhamou ndiaye Nâsootu

21/08/2026
🕌 ZIARRA SANGUE BARHAMOU NDIAYE — UN RENDEZ-VOUS DE FOI, D’AMOUR ET DE FIDÉLITÉ À L’HÉRITAGE DE BAYE NIASSLe 14 novembre...
09/08/2026

🕌 ZIARRA SANGUE BARHAMOU NDIAYE — UN RENDEZ-VOUS DE FOI, D’AMOUR ET DE FIDÉLITÉ À L’HÉRITAGE DE BAYE NIASS

Le 14 novembre 2026, Sangue Barhamou vibrera au rythme de la foi, de la spiritualité et de la ferveur à l’occasion de la Ziarra de Sangue Barhamou Ndiaye.

Moom mii moo woote Pikine Icotaf, samedi prochain bii ñu jëm, ngir maaggal PAYS BI, ba nooppi jël PAYS BI, def ko parrai...
15/07/2026

Moom mii moo woote Pikine Icotaf, samedi prochain bii ñu jëm, ngir maaggal PAYS BI, ba nooppi jël PAYS BI, def ko parrain bës bi, YÀLNA ñu ci YÀLLA yoobbu ci jaamm, mu aandd ak jariñu, ci barkeey SHAYKH IBRAHIM NIASS🤍.

Crédit ✍🏽 Muqadam ibn Sulaymaan Ly

15/07/2026

Loo nekk nekk jaahil, soo ko degloo mu yeela ci YÀLLA, nga comprendre fi taalibe BAAY yi di waxee.

Moom, kenn la ci ñi PAYS BI seedeel Fathul Akbar, ak Fathul Muqaddass, waaye moom it, seede bi toollu ko feenn, ngir xam gi mu xam ni, kudul PAYS BI, suñu la seedelee mbaax , doonte sax ci laammiñu PAYS BI la, da ñu lay sooññ rekk di la encorourager, waayee tagg, ci kenn rekk la xaj, mooy PAYS BI, moo baax ba jeeggi melo ak dayo🤍.

06/06/2026

Un grand merci à mes nouveaux followers !

Bonkoungou Issiaka, Seydina Ibrahim, Mahamoud Lawan Mahamat Raougi, Elbachir Mohamed, Daouda Yossi, Hamta Diallo, Seydou Moumouni, Baye Ousmane Kebe, Abdoulaye Diop, Møusså Sidibé, Abdourahamane Camara, Moussa Dione, Mouhamed Diatta, Abdoul Kadri Mamane, Goz Sylla, Kichki Sanogo, Bamba Biagui, Mamadou Saliou Diallo, Cyril Bcoly, Ibrahim Mamoudou, Doulba Le Silence, Siaka Bamba, Babacar Sbn

06/05/2026

Lènn, ci njaanggaleey KU TÈDD KI, Mawlâya Sangg Barhaamu NJAAY🤍🍂.

1ère Édition Conférence Fityanu Siqdine Pikine Muqadam Thierno Ousmane Sow Gandiol Samedi 11 Juillet au terrain  croix r...
29/04/2026

1ère Édition Conférence Fityanu Siqdine Pikine Muqadam Thierno Ousmane Sow Gandiol Samedi 11 Juillet au terrain croix
rouge mise en place 17h
Sous le Haut Parrainge de sa MAJESTE MAOLANA SANGUE BARHAMOU NDIAYE

Adresse

Camberene

Téléphone

+221785864683

Site Web

Notifications

Soyez le premier à savoir et laissez-nous vous envoyer un courriel lorsque AHBÂB sangue barhamou ndiaye publie des nouvelles et des promotions. Votre adresse e-mail ne sera pas utilisée à d'autres fins, et vous pouvez vous désabonner à tout moment.

Raccourcis

Partager