Mame Borom touba

Mame Borom touba

Share

Sante reke khadim rassoul

20/06/2024
20/06/2024

Un grand merci à mes nouveaux followers ! Assane Faye, Dianhka Ndongo, El Hadji Diallo, Ndeye Mareme Diop, Abdou Karim Cisse, Djibril Ndiaye Diadji, Awa Toule Der, Xalil Moukaramiste Baye Darou, Feuse Beye, Serigne Cheikh Mbacke, Sidi Bouye, Serignembacke Samb, Rahim Cham, Astou El Bachir Niang, Khaita Niang, Mame Thierno Niang, Papis Kara Bambiste Kassé, Serigne Sylla, Abdoulaye Barry, Dou Izer, Aby Lo, MôMô Sààlh, Samba Seck, Djiby Diouf, Mame Mor Ndiaye, Mame Mor Diarra Gningue, Amdy Diaw Kr, Omarolah Soh, Katim Toure, Ibou Diop, Sulayman Sallah, Djibi Diakhate, Mouhamadou Moustapha Danso, Cheikh Diop, Amyniang Diallo, Abdou Kane, Isouf Kone, Abdoulaye Diallo, Ousmane Noraynii, Khady Dia, Sodachou Niang, Ndour Awacheikh, Fallou Diouck, Ousseynou Karballa Sidibé, Biram Seck, Mounir Diop Moustapha, Cheikh Anta Niang, Cheikh Saliou Mbacke Ly, Modou Dramé, Fallou Gueye

19/06/2019
Photos 12/06/2019

Mbacké man dey Sante naala.

Photos 11/06/2019

Ndénkaaney Sëriñ bi - "SILKUL-JAWAAHIR" n° 17 / Serigne Mor Sourang

========

Sëriñ bi dafay nettali ni sunu Boroom maandoo ak nit ku ne na mu koy delloo àqam, di lijjanti mbir yépp fii ci àdduna. Ngir kilifa yi ak woroom xam-xam yi dañoo léeboon léeb wu yàgg. ne : képp ku ray nit, lum yàgg-yàgg dañu koy ray.

Sëriñ bi nag di ci joxe misaal ci nettali bii, sunu Boroom ni muy jëfandikoo ak maandoom ak ni muy àttee.

Mu ne boo demee ci téere bi ñuy wax {At-Tibrul Masbuum} bu Imaam Xasaalii, dafa nettali ne Seydinaa Musaa( HS) da doon déeyaale ak Boroomam. Ne ko yaw sama Boroom damaa bëgg nga wan ma sa maandu gi ak mbir mu ne ni nga koy lijjantee ba lu ne tegu fa mu war a tegu. Sunu Boroom ne ko yaw Musaa dangay waa joo xam ne, dangaa tàng ta ñeme, manoo muñ, bo gisee lu niruwul dëgg dangay gaaw a wane sa bopp lool. Seydinaa Musaa ne ko man de ku ñàkkug muñ laa waaye yaw de man nga maa baaxe muñ ci sa tawféex ba loo ma wan ma man koo muñ. Sunu Boroom ne ko aywa demal nga jubali ci bëtub ndox (source d'eau) bu sàngam, nga làqatu ca wet ga nga xool sama kàttan ak sama xam-xam nga xool mbóot yi nimu demee. Seydinaa Musaa daa di dem foofee ko sunu Boroom tegtal ca bëtub ndox ma, mu làqatu ca wet. Am waa ju war fas ñëw wàcc fasam, daa di jàpp ci bëtum ndox booba daa di naan ci ndox ma, tekki ak ngiseem (denckaayu xaalis) bo xam ne def na 1000 diinaar, teg ko ci wetam daa di julli. Bi mu jullee ba noppi daa di waraat aw fasam, fàtte fa ngise ga. Am xale bu ñëw, naan ci bëtu ndox boobu, fekk fa ngise ga, daa di koy jël dem. Ginnaaw xale boobu am waa ju ñëw, waa joo xam ne nii mag la te gumba la daa di ñëw foofu ci bëtu ndox bi, daa di fay naan taxaw fa di julli. Ka fa fàtte woon ngise ga daa di ñëw, fekk fa gumba googu, ne ko dama fee fàtte woon ngise gu def 1000 diinaar, ci barab bii laa ko fàtte ci waxtu wii te it kenn ñëwu fi ci ginnaaw gi ku dul yaw. Te moom xamul ne xale bi jël na ko ba dem, waaye kom diggante bi yàggul rekk te fekk na fi gumba gii mu jàpp ne moo ko jël. Gumba gi ne ko man damaa gumba naka laa man a gise sa ngise ? Waa ji daa di mer, bojji jaaseem door ko ko mu faatu, mu seet ko gisul ci moom dara. S. Musaa daa di ne sama Boroom sama muñ nag fii

Want your school to be the top-listed School/college in Jeddah?

Click here to claim your Sponsored Listing.

Location

Category

Telephone

Website

Address


Jeddah